
Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa Beugue nala té xamothie dara Mbeugyél thie xol ley nék deugueleu Beugue nala té xamo thie dara Mane déh walouléne ma wax koko Xalé bi lékatouma ndax mome Nanatouma nélawatouma Wowo Sama xol yathie néh Lék lék ma woo ko tit dal di coupé Sama appetit coupé Febar dinama guoungué Doctueur dama love ba dof Té xawma loukoy fathie Wowo Mba meune nga thie daraa Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa Beugue nala té xamothie dara Mbeugyél thie xol ley nék deugueleu Beugue nala té xamo thie dara Mane woo nala founé Nga diapémma sa xarite Inviter resto, lalal nala louné Wowo Nga diapéma sa xarite Lék lék ma woo ko tit dal di coupé Sama appetit coupé Febar dinama guoungué Doctueur dama love ba dof Té xawma loukoy fathie Wowo Mba meune nga thie daraa Mane beuguena ma bagne bayiwouma Mane guisoumaa Kénén koudoul mome Mbeuguéleu beuri dolé yén mako xam Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa Beug Ue nala té xamothie dara Mbeugyél thie xol ley nék deugueleu Beugue nala té xamo thie dara Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa Beugue nala té xamothie dara Mbeugyél thie xol ley nék deugueleu Beugue nala té xamo thie dara Kouthie nek’aak kingna nope Sa guinaw bandague faxassul Diougueul yyeungueul bamou saf Sa gnuinaw badanue faxassul Kouthie nek’aak kingna nope Sa guinaw bandague faxassul Diougueul yyeungueul bamou saf Sa gnuinaw badanue faxassul Lyrics Viviane Chidid «WUYUMA» by abdouayebacary
Песен-НИКИ
Загрузка...
Другие песни Dj Quest Gh
Все песни →Похожие песни

Бигасс
SODA LUV
Ничего личного
Русский рэп201975,449

Бандана
Платина
РНБ КЛУБ
Русский рэп201859,980

Свадебное путешествие
Александр Буйнов
Острова любви
Русская эстрада199954,906

Каспий жағалауы
Azamat
Поп200134,438

Шпилька-каблучок
Лолита
Анатомия
Русская эстрада201433,308

Девочка 2D
Dead Rave
Singles 15-17
Русский рэп201828,891
