
Sa loxo set / Tes mains propres Sa lepp set / Que tout soit propre Bul nuyu kenn / Pas de salutations Bul lëng kenn / Pas d’accolade Bul génn kese ndax bëg génn / Ne sortir que si c’est essentiel Bul sëqët fepp / Ne pas tousser n’importe où Bul jége kenn / Toujours garder une distance de sécurité Sëqët, fièvre, bop buy metti njëk feeñ / Premiers symptômes: toux, fièvre et maux de têtes Soj, problème noyi, senn sa bakkan / Rhume, troubles respiratoires, écoulement nasales Sëqët, fièvre, put buy metti, malaise feeñ / Toux, fiévre, maux de gorge, début de malaise Du rey nit ku ñul si ñi xamul dëg ak fenn / Ca ne tue pas le noir, pur mensonge Sa loxo set / Tes mains propres Sa doom yi set / Tes enfants propres Bul nuyu kenn / Pas de salutations Bul lëng kenn / Pas d’accolade Bul génn kese ndax bëg génn / Ne sortir que si c’est essentiel Bul sëqët fepp / Ne pas tousser n’importe où Bul jége kenn / Toujours garder une distance de sécurité Sa loxo set / Tes mains propres Sa lepp set / Que tout soit propre Bul nuyu kenn / Pas de salutations Bul lëng kenn / Pas d’accolade Bul génn kese ndax bëg génn / Ne sortir que si c’est essentiel COUPLET Xeex ak Corona Virus, / Combattre le coronavirus Microbe, jàngoro la, du nit / Il s’agit d’un virus pas d’un humain Aduna nek si combat / Le monde est en guerre Du gis ku muy xeexal / Contre un enemi invisible Nuro nak grippe / Des symptômes de grippe Nañu éviter contact physique / Evitons tout contact physique Xajul Grand Yoff, Colobane, Pikine / N’a de place ni à Grand Yoof, ni à Colobane, ni à Pikine Tax ba ñu annuler programmes yi siiw / Il est la raison de l’annulation de tous les programmes Tax ba ñu foog ni àddinay tukki / Il donne un air de fin du monde Medecin sonu na si li / Tous le personnel soignant au front Amul vaccin, ordonnance tamit / Sans vaccin ni ordonnance Mu ngi ray, day toroxal nit yi / Ce virus vulnérabilise et tue Buñu tooge dina bari ay victimes / Si l’on reste observateur les victimes seront nombreuses Set si sa askan, set si sa bopu / Propreté collective et individuelle Tëju te baña seeti sa mbokk / Eviter les visites, rester chez soi Julli sa màkkaan, Messe si la bokk / Toutes les prières à la maison quelle que soit notre religion Xeex ko mu jeex mbir yepp mëna doxx / Combattons ce virus pour que tout revienne à la norme Masque, sabu, antiseptique / Masques, savon ou gel antiseptique Raxasu, sangu dadi set wecc / Se laver, laver ses mains, rester propre Dal, muñ, bañ lu melni dess fi / Calme et sérénité pour éradiquer ce fléau Gën di ñaan pour jamm day dikk / Prions ensemble afin de vaincre ce virus Sa loxo set / Tes mains propres Sa lepp set / Que tout soit propre Bul nuyu kenn / *Pas de salutations Bul lëng kenn / Pas d’accolade Bul génn kese ndax bëg génn / Ne sortir que si c’est essentiel Bul sëqët fepp / Ne pas tousser n’importe où Bul jége kenn / Toujours garder une distance de sécurité Sëqët, fièvre, bop buy metti njëk feeñ / Premiers symptômes: toux, fièvre et maux de têtes Soj, problème noyi, senn sa bakkan / Rhume, troubles respiratoires, écoulement nasales Sëqët, fièvre, put buy metti, malaise feeñ / Toux, fiévre, maux de gorge, début de malaise Du rey nit ku ñul si ñi xamul dëg ak fenn / Ca ne tue pas le noir, pur mensonge Sa loxo set / Tes mains propres Sa doom yi set / Tes enfants propres Bul nuyu kenn / Pas de salutations Bul lëng kenn / Pas d’accolade Bul génn kese ndax bëg génn / Ne sortir que si c’est essentiel Bul sëqët fepp / Ne pas tousser n’importe où Bul jége kenn / Toujours garder une distance de sécurité Sa loxo set / Tes mains propres Sa lepp set / Que tout soit propre Bul nuyu kenn / Pas de salutations Bul lëng kenn / Pas d’accolade Bul génn kese ndax bëg génn / Ne sortir que si c’est essentiel
Песен-НИКИ
Загрузка...
Другие песни DIP DOUNDOU GUISS
Все песни →Похожие песни

Бигасс
SODA LUV
Ничего личного
Русский рэп201975,449

Бандана
Платина
РНБ КЛУБ
Русский рэп201859,980

Свадебное путешествие
Александр Буйнов
Острова любви
Русская эстрада199954,906

Каспий жағалауы
Azamat
Поп200134,438

Шпилька-каблучок
Лолита
Анатомия
Русская эстрада201433,308

Девочка 2D
Dead Rave
Singles 15-17
Русский рэп201828,891


